楽器
Ensembles
Genres
作曲家
演奏者

歌詞: Ismaël Lô. Baykat.

mane he baykat bi khalam
demonna bay nekh waye boumgua
dokna mome

mane he baykat bi khalam demonna
bay nekh waye boumgua dokna mome

boula nekhe talalal say lokho
yaye docteur biy fath khifou askane bi
liko dale si nditoum rew bassi miskine
ya soumeko di dane sa dole andak nath
bi di liguey sa gnakha di tourou
ngay bay di doukat bilay ya am diome

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour waw koufi febar
yako nandal aki reen bamou feekh

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi febar yako nandal aki reen
bamou feekh

ya momone sa mbay
ya mome sa guanthiakh mome say
ndiour ya mome sa alla di bay
nguour gneuw dougalthia lokhome ak
boor fekeleuthaa guanthiakh ba
megneu lole ndeketeyo

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi febar yako nandal aki reen
bamou feekh

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi febar yako nandal aki reen

bamou feekh
dirama diarama baykat be yaw
keneu rek mola mana fay
moy bourbi yaalla
guathia ngalama

guathia ngalama yaw baykatbe
guathia ngalama
guathia ngalama yaw baikatbe

dirama diarama baykatbe yaw
keneu rek moleu mana fay
moye bourbi yalla

(Merci a Clarissa pour cettes paroles)
Ismaël Lô